Surprise Me!

Kan MOYE Kan (Seigneur Hard Core)

2016-09-26 147 Dailymotion

''Kan moye Kan'' fait parti parmis les singles qui composent la première mixtape ''PaaKa Cii Déek'' de Seigneur Hard Core,
Bientôt vous aurez la mixtape .
_____________________________________________________________________Abonner vous sur ma chaine youtube
Aimer la page facebook : https://www.facebook.com/SeigneurHardCore

Télèchargement gratuite du single clique ce lien

reverbnation : https://www.reverbnation.com/seigneurhardcore

Merci et a bientôt .
dou lolou mognou xewlo irri boy seubeuklo
niggeuz yi terré ci ndioub mognou tak sabaplo
xiddifi lifeou pablo gnou dadjou shit doflo
xirri fightal lissoufeu mougnon yague deflo
LouGnou woutoulék gnome rime ak LouGnou kay natalé
Jappe Dissi Xeup Lou kinss bou lénegnou Tekeulé
Gnoune la Hood bi Ndokalé Ndiokalé lougnouye Sapalé .
Beat Bass mélodie Ték Jeul lép sampalé
danger murder crocodile fougnou feul gotto die
kep mic di bita bane ngua xam ni dougnou sa broda way
Sa gatte té diodé way fi doffi diodo way
sabay mbayane tass sabar bisniki tay jo don weny
you better listen up gnon wak ko thia tell
kon beuga jotte fougnou né digua waki thia tell
mathi thi xell kawé ci ndelle ba souti éssel
dexengnou rende job bagna sintou thi gelle
dou lollou mognou xewlo irri boy yi seubeuklo
nigg enz yi terré ci ndioub mognou tak sabaplo
kan ak kan dou mak yow yan ak mane
kou diouk ba lamb sa toubey fess ngua wara
xam kan moye kan
Niggeuz yi diffi mbew nagnou thiéné ta dall
fou seigneur képati mic dina thiéné ta dall
Nakou shit laffi hood bi sédéko dall
woutek gnon c bie ngath tour beach yénako tall
ndak dé yenako lale teyé mic bi diague diagué
repesent thi douli néne diko diague diagué
di doxé slogan wou thiaga noka beugue begué
gnoune life Thie Ndodou foula lagnouye bégue begué
ma wak thi dallou xéddem hiphop mogui segeum
gollou gou diouk woné sa tate wout louye xoubeull sa gaine
fi doffi bignal sa hand ndank gnodi hard core yi
gnoune gnolzy takali menote dieul le boub ci ouf yi
adjh barri peine de mort gnola guena niangue goor
gnigne fi yague di mine gnoune lanouye keep niande door
dagnou say mboki mbar démelak sa jay taar ana goor ak jaay jongué bafiyz dioutou di jaay taar
dou lolou mognou xewlo irri boy seubeuklo
niggeuz yi terré ci ndioub mognou tak sabaplo
xiddifi life ou pablo gnou dadjou shit doflo
xirri fightal lissoufeu mougnon yague deflo
do lolou mognou xewlo
irri boy yi japp di rap bou niak fayda tékthi di lene nabe nabé
do lolou mognou xewlo
Diabou drogue sexe money fouti gelon tatou néne douma rap ci lolou mané
do lolou mognou xewlo martatou politicien yi di laak séni mbotte dem ba sa changer entretien yii
dou lolou mognou xewlooo
gnodi fuckin supper star reuy tate di ngande bir I am not fuckin super star

Buy Now on CodeCanyon