"Bonne fête de Saint Valentin ❤ <br />Mbeugel mo beuri dolé donc bou darra sed <br />bouko thiopati neko rikh thi digueu n'a rafet té sant noula nekh ❤❤❤❤❤ <br />les femmes guenélen thiourayi, bine bine yi, menote yi, chaînette yi, na nekh ba melni toukoussa beun sagnebeu réreu"