Akhlou Brick - Sama Logo Bi

Disponible sur iTunes: http://itunes.apple.com/album/id14471...

Apple Music:
http://itunes.apple.com/album/id/1447...

Beat by BabsBeat
Edit mix & master by Max Mix QGS records
Avec la Participation de : Boubou Design , Bise Collection, CasuelChic, Yarba Deco, et ATVISION,

Lyrics:

SAMA LOGO BI

Ehhhhhhhh
Logo bi logo bi i know
LOGO BI
Parélén tay paréna
ok ok I know
Parélén tay paréna

EHHHHHHH.
Fou bi néna dofatoul té dou délou fan
Patin né mouk dou ba fén té ken douko téré nan ay Douliprane
Parélén paréna
May djiné biy tafou bir koloban
Dou gris gris diate ak thioumboukay boudone lola Gouy Gui rékay meuna dan
Grand yi né dama wawlé meuna rap tekthi gnémé rak
Ragalouma yamou thiowlé limay hamb tay la geuna tak
Tay la geuna tay la geuna tar
Dina meti tahoul beut yi taaa
Yéné ma dé ma lék sa naka
Tay mbeura beuré guén thi di bakou
Wahko né Toubab bé bagn né dou diongu
Nit kou gnoul bagn né dou diang
Kou nék sa natou bi
Ana Louy ndiarignou koom
Boudé dou guén thi bank
Haliss day wallou nit
Wan ma Lan geuna fonk
Louis V Gucci nga Am
Ma Tassaré logo thi
Logo bey todji sa monde Ara la toudouma baye sen mai wowema wowema sen pa
Armée bi marquer na sen pas
Ngor Djigan Dupon la Demba
Sa rapeur bi menoul na bayi neko na bayi mongui beune timpa
Sa girls bi né Ara da sympa
Beugone ma nop ko mais même pas
Dama pédaler laisser deux legui meun na pas de danse yi rek faté na Guéta

gnemeko brickest attentat
wane ko topp 5 batamba
Mbour Dk Kaolack brickest ba Tamba
Sissou na dissout tay niggazz bi nangouna
Sagnsek sama logo bi
Logo bi logo bi logo bi
Sa teeshirt sama logo bi
Logo bi logo bi logo bi
Sa casquette sama logo bi
Logo bi logo bi logo bi
nangouna Sagnsek sama logo bi
Sagnsek sama logo bi nangouna

Parélén tay paréna
ok ok I know
Parélén tay paréna
ok ok I know

Caissou beat bi bamou dalé gneup Ladjté Dayza fan la nè
Caissou état dig la mallette do massa ladjté fan la palais né
Wesounala dama paré man la mise à jour bi Dougal sa paramètre
Rap galsen bou melon ni charrette ma togue thi kanam gnouné Dafa kanamé
Nigga man Kaw Kaw la bo beugué gnou def com dap dama yoré beuzzou Classico bi gnom gnouléni thiow comme lah
pincez tous vos Cora c’est moi le chef chorale ara la Dayza la Herbert Pepper Léopold Sédar
Raw Nala douma sa Mass hale bou matagoul moss wodatko
Clip bi harouthi trace
Million de vue yi thi poche nodatko
Public bi rap la ma sass
logo bi solko ni boss
gneup dacorr
sa son yi di faux raccord Dayza la messouma teulé ma beug beugua def mouy teu
Fitou gayndé la dou titeu
Da yomb ma mélni kouthiy fo
Sa nigga bi amatoul Halima plume Bila faté thi ndelou titeuf
Yag na méti ma mougnko
piège nagn gnou ma ndiouyko
Gni beug souki lafou pith bi nelen pith Bangui thi logo Twitter

gnemeko brickest attentat
wane ko topp 5 batamba
Mbour Dk Kaolack brickest ba Tamba
Sissou na dissout tay niggazz bi nangouna
Sagnsek sama logo bi
Logo bi logo bi logo bi
Sa teeshirt